ADIOUZA - BUS BI (CLIP OFFICIEL)
ADIOUZA ADIOUZA
303K subscribers
7,096,986 views
30K

 Published On Oct 2, 2019

Bus Bi est le nouveau single de Adiouza, dans ce nouveau clip, Adiouza chante un coup de foudre dans le bus. Ainsi débute une histoire d’amour imaginaire avec un bel inconnu. Sa copine l'encourage à franchir le rubicon en déclarant sa flamme à l'homme mais orgueilleuse, elle refuse, hésite jusqu’à ce que le bel inconnu arrive à sa destination et descend de l'autobus emportant son amour.

Bus Bi lyrics
Baba mi ani
I guili Wana merer

Couplet 1
Wajy souma koy xool ak nimou mél
Ah N bi né thi nekh

oubi bountou bus bi dougou sama xole
li mome dou néne

mou guestou xoolma
Thi la xamner dou xememe
Maye gnami gnami
Koula jib wagni yaye dos d’âne
bus bé ngui daw dal te rombeuna sama arrêt
mba dou terminus lama dieumé
Dara dakar fo dem dik.

Refrain
fess nga dél thi mane
té xawma yawla kane
xol bi nane ma te nga dém dik xolle ba xame.

fess nga dél thi mane
té xawma yawla kane
Xel Bi nane ma togal boul dem jiguene doù yombeu.

Ouhe baba
Ouhe (bis)
Mideyidima
Yidima

2 eme couplet

Bus be ngui rire
Mane degatouma
beug na la pire
Ndax guissatouma

Mbeugel bou gaw
Melni Lou diare si peage
O doff nassi Yaw
Kila done sette

Jombi te guissouma jine ahhhhn
Jappeu ma teuthieu condamné ahnnn
Jokna arret laye demandé ahnnn
Ba chauffeurou bus Bi freiner
Mou naxe Ma seye

Refrain
fess nga dél thi mane
té xawma yawla kane
xol bi nane ma te nga dém dik xolle ba xame.

fess nga dél thi mane
té xawma yawla kane
Xel Bi nane ma togal boul dem jiguene doù yombeu.

Pont
Le courage m’a quitté
J’ai même pas osé tenter
Hypnotiser par son charme
Chui tombée en amour

Refrain
fess nga dél thi mane
Ahannnn
xol bi nane ma te nga dém dik xolle ba xame.

fess nga dél thi mane
Ahannn
Xel Bi nane ma togal boul dem jiguene doù yombeu.

Refrain
Ouhe.
fess nga dél thi mane
Ouhe
té xawma yawla kane
xol bi nane ma te nga dém dik xolle ba xame.

fess nga dél thi mane
té xawma yawla kane

Xel Bi nane ma togal boul dem jiguene doù yombeu.

Ba bus Bi freiner
Thi la xamner reuthieunama
Loutax demouma
Bassi mome wakhko li fi ne.



Remerciements: je remercie l’équipe de gladiateur qui m’a accompagnée dans la réalisation de cet album, il s’agit de MON FRÈRE Cheikh ouza, Moussa Ngom, Yeye faye, Iso on the beat, CT, Baxaw, Xuman, king Kruh lyrics, Bril, Pac D, Max Ngassa, wylliam.
Les stylistes: Mareme Chalar, Bisecollection, Mado, Lena couture didiwax.
Je remercie tout le staff, tt les membres de Adiouza family, ma famille, mes amies.
Sans vous, il me serait difficile d’y arriver.
Mention spéciale à mon père et ma mère pour votre soutien.
Merci à mes amis.

Abonnez-vous ici : http://bit.ly/AdiouzaDiallo

Pour booking:
A l’international: +33 6 77 73 16 73
Au Sénégal: +221774892177 / +221 773222305

Retrouvez Adiouza Diallo sur :

Instagram:   / adiouza  
Twitter :   / adiouzaofficiel  
Facebook:   / adiouzapagefans  

#Adiouza2019 #BusBi #AdiouzaProd

show more

Share/Embed